VOOZH about

URL: https://wo.wikipedia.org/wiki/Kom-kom

⇱ Kom-kom — Wikipedia


Aller au contenu
Jóge Wikipedia.
👁 Image
Gaambi

Kom-kom :mooy xam-xam biy leeral lu aju ci wutiinu alal, tey li nga am ci alal, sa koom-koom man naa tekki sa alal, lépp nag lu aju ci yëngu gu nit di def ngir am dara loolu ci xam-xamu koom-koom lay bokk, moo xam mbay la mba yaxantu mbaa liggéeyu xarala(fr: économie; en: economics) = koom-koom